New Africa

Lyrics

Mane Youssou Ndour!
 Ma ngi wo! bépeu domi Africaaaa!
 Gnou bokeu khalate!
 Bokeu guiss guiss!
 Bokou yénéééééé!
 Sans frontiéres
 Bolé sounouy ame ame
 Té liguééééy!
 Wara tougnou
 Nangou kéne nieuw
 Dignou féwaléééééééééé!
 Boul djité rew
 Fok né la fa nek
 Yaw ya ko mome!
 Ndite bou deugueur
 Dafa wara fek nga beug sa rew
 Té sakou ndimbeul
 Ndimbeul na sa fek
 Lokhoy boroooom!
 Woy Africa!
 Bou dianteu bi finké waw!
 Na la fek diok!
 Ak sa dioumetou kaye!
 Beuthieuk bi gaw neu!
 Niéteu dou beuré
 Té niarra meuneu kééééneu waw!
 Yone wi! sorré na!
 Té métti na
 Naniou ko waaadial
 Bo doul nopé khalate
 La niou défone Mameuuuu ya!
 Sa khol do toul nekh
 Té dotou khame lou doul féyane to!
 Souma sagnone Africa
 Béne niit mo koy djité!
 Niou bolé
 Sounouy khalate
 Ak sounouy dolé
 Diokh ko!
 Naniou oubi frontiers yi! ratakhale yone yi
 Ba nieupeu guissé
 Changes your thinking!
 Work together!
 Keep and working!
 Cheikh Anta Diop!
 Kouamé Nkrumah!
 Steven Biko!
 All you people!
 Africa!
 

Audio Features

Song Details

Duration
03:43
Key
2
Tempo
123 BPM

Share

More Songs by Youssou N'Dour

Albums by Youssou N'Dour

Similar Songs