Live Television

2 views

Lyrics

1er couplet
 ouragan ouppeul assamane
 ba djante leer ma djanok satellite
 satellite ngalla yoné ma la khew feulé, ak fénène ak fénène
 mani go, go, go
 ni live, Live Television live, live tv live
 2e couplet
 roplane bi warone tiim
 dima eundil ki ma namona ngui
 wayé tey télévision waar na ma, wone ma lima beugona guiss, ouragan mani ouppeul ouppeul ouppeul
 ni live, Live Television life, live tv live
 oh life, live tv live, Live Television live
 fook na né formalité leu(...)
 fook na né formalité leu(...)
 fook na né formalité leu(ma djapp yénéni chaines)
 fook na né formalité leu, leu, leu...
 1er couplet
 je vais vous raconter une histoire extraordinaire
 un soir, une famille nous avait invité mes amis et moi, il y a quelques semaines de celà
 nous étions une vingtaine à nous retrouver dans un grand salon, attendant avec impatience que le dîner soit servi
 devinez ce qui est arrivé
 à neuf heurs moins cinq, la famille nous abandonnés dans le salon, préférant s'entasser dans une petite chambre, avec une télé mal éclairée, uniquement pour regarder, cette fameuse émission
 ...khalaass
 ...wala bok niou dem
 chéri souma sadjobane
 dina liguey ba ame louma djeundé satellite, nguir guiss di guiss la thia bbc, la thia ortm wala la thia mtv yeah
 ni live, Live Television live
 live tv live
 we need live, live tv live, Live Television live
 yaw chéri souma sadjobane, dina liguey ba me louma djeundé satellite nguir guiss di guiss la thia orts, la thia bbc wala la thia mtv yeah
 wawaw kone television wawaw
 yeah chéri souma sadjobane dina liguey ba ame louma djeundé satellite nguir guiss di guiss la thia orts, la thia cnn wala thia mtv yeah
 wawaw kone television wawaw

Audio Features

Song Details

Duration
05:59
Key
6
Tempo
143 BPM

Share

More Songs by Youssou N'Dour

Albums by Youssou N'Dour

Similar Songs