Leaving

Lyrics

Dem dem
 Dem fan
 Den ndax lan
 Baya ko mom
 Dem nguir xee bou barri bi
 Dem ndax teen boh neex bi
 Teh rapp rek noom noo siy naan
 Nach bi lakkatouma taw bi barrewoul
 Dem ngir bokk bone menou fee am
 Dem ngir daffa wara nekk gorr done
 Goorgoorlau
 Dem dem
 Dem fan
 Dem ndax lan
 Liberte bi
 Si espace bou lendeum bi
 Sama beut yi guissa tounou
 Garap yi nga xamenteni noo ma souxat
 Su beut setiee barap yi bow
 Dem ngir Keur gui daf may nirou lou lendeum
 Dem nguir daffa warranekk goor done
 Goorgoorlau
 Damay dem
 Chi alla bi
 Damay dem Chi dex goumak gui
 Ne damay dem waw seeti sama nawleyee
 Damay dem si ban bou ritax bi
 Damay dem ba reewu bitty
 Ne damay dem waw setti samambokkyee
 Go-go (bis)
 Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy
 Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar
 Hey what do you need?
 He he yaw lilaneex
 Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy
 Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar
 He defa li la neexoy hey yaw lila soop
 Sammkatou mboott moo xam ba ciy
 Sooxaoy ni meneuh kott noom daal amounou
 Mbaam hey defal li la nexx oo
 Hey what do you want?
 Ho ho ho ho ...

Audio Features

Song Details

Duration
04:59
Key
9
Tempo
147 BPM

Share

More Songs by Youssou N'Dour

Albums by Youssou N'Dour

Similar Songs