Gorée

Lyrics

bama démé gorée manne
 andak samayyy kharite
 demm sa keur diam gawonne
 dama dalle di seugemm dioyy
 goor yi magg yi bi boor
 djiguéne yu magg yi bi boor
 goor yu ndaww yi bi boor
 djigéne yu naww yi tchi bénène boor
 niu daddi fayy khali yonne
 yonne bo khamni dangay demm
 yonne bo khamni dangay dem
 sa khell du demm ludull ssi délussé
 lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
 lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune
 bama démé gorée manne
 andakk samayy kharittt
 demm sa keur diamm gawonne
 dama dalle di seugueumm dioyy
 goor yi magg yi bi boor
 djiguéne yu magg yi bi boor
 goor yu ndaww yi bi boor
 djigéne yu naww yi tchi bénène boor
 niu daddi fayy khali yonne
 yonne bo khamni dangay demm
 yonne bo khamni dangay dem
 sa khell du demm ludull ssi délussé
 ennnhh gorée
 lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
 lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune
 lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
 lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune
 Gorée
 lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
 lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune
 Gooréeeee

Audio Features

Song Details

Duration
02:20
Key
7
Tempo
181 BPM

Share

More Songs by Youssou N'Dour

Albums by Youssou N'Dour

Similar Songs