Food For All

Lyrics

last night I saw in my dream
 All over the world
 food for all
 last night I saw in my dream
 All over the world
 food for all
 batay amna nit gno xamni
 bougnou agné dougnou réer
 gnogno gui doundé thiono
 batay amna nit gno xamni
 bougnou agné dougnou réer
 gnogno eupati thiono
 nako gneup degg
 tey liy jot jotna
 gnognou lignouy doundou métina
 dolil dolil dolil dolil
 more solidarity
 encore encore encore encore
 plus de solidarité
 last night I saw in my dream
 All over the world
 food for all
 last night I saw in my dream
 All over the world
 food for all
 na thi gneup dougal sen loxo
 té bagna xeeb ndimbal dou dooy
 li ga nara dékané deween
 guénée ko boul def yeufi Ndiawéne
 amna nit gnou xiif di ray
 dimbeli lène warougar la tay
 plus de solidarité
 plus de fraternité
 more solidarity
 more fraternity
 oooooh que c'est nécessaire
 c'est c'est c'est c'est plus que nécessaire
 oooooh oh que c'est nécessaire
 c'est c'est c'est c'est plus que nécessaire
 last night I saw in my dream
 All over the world
 food for all
 yalla mo binde té yamaléwoul
 béne domou adama ak moromam
 wouté nagne ci xalaat
 wouté ci dieuf
 wouté ci thiossane ak ada
 wayé nagnou diap ni beugg jam
 ak doundou gou neex té andak dal
 boula yalla bolé thi gni am ba dessal
 naga seet gni amoul ga dimbali lén
 ooooh que c'est nécessaire
 c'est c'est c'est c'est plus que nécessaire
 ooooh oh que c'est nécessaire
 c'est c'est c'est c'est plus que nécessaire
 batay amna nit gno xamni
 bougnou agné dougnou réer
 gnogno gui doundé thiono
 batay amna nit gno xamni
 bougnou agné dougnou réer
 gnogno eupati thiono
 nako gneup degg
 tey liy jot jotna
 gnognou lignouy doundou métina
 dolil dolil dolil dolil
 more solidarity
 encore encore encore encore
 plus de solidarité
 more more more solidarity
 more more more solidarity
 more more more solidarity
 more more more solidarity

Audio Features

Song Details

Duration
05:00
Key
1
Tempo
129 BPM

Share

More Songs by Youssou N'Dour

Albums by Youssou N'Dour

Similar Songs