Couple's Choice

2 views

Lyrics

Né li motah sawarouma am dome
 Bouma kholé fima diar
 Wayé mane mi amone na yakar
 Né beuguouma am dome sou anié dou rére, beuguouma am dome kéne douko nié, beuguouma am dome dou kham louye diame, li motah sawarouma am dome, né li motah sawarouma am dome
 Souma kholé lima datieu
 Wayé mane mi amone na yakar
 Beuguouma am dome mou deuk si tiono
 Beuguouma am dome mouye nakharal yayame
 Beuguouma am dome dou mbekté si bayame, li motah sawarouma am dome
 Beuguouma am dome bouye nakharal yaayame wo wo woye mane
 Né li motah sawarouma am dome
 Bouma kholé lima datieu
 Waw mane mi amone na yakar
 Beuguouma am dome dou kham loudoul nakhar
 Beuguouma am dome dou guiss dianteu bi
 Beuguouma am dome mou deuk si métite
 Li motah sawarouma am dome
 Beuguouma am dome bouye nakharal yaayame wo wo woye mane
 Ni dome dome dome bou boné niouné yaye, dome dome dome bou bakhé niouné nieup
 Mbekté si sa baye euh! euh!, banekh si sa yaye euh! euh!
 Mbekté si sa baye euh! euh!, banekh si sa yaye euh! euh!
 Mbekté si sa baye euh! euh!, banekh si sa yaye
 Beuguouma am dome mou deuk si tiono
 Beuguouma am dome kéne douko nié
 Beuguouma am dome dou guiss dianteu bi
 Né limotah sawarouma am domeu
 Wo! Oh! Oh! Oh! wayé mane beuguouma am dome, wayé mane sawarouma am dome, mou deuk si tiono dou kham loudoul diam waye li moma tisse
 Wo! Oh! Oh! Oh! mani kéne niéwatouléne, mane dal beuguouma am dome mou deuk si tionoye Oh! Oh! ni léye, Anye!
 Wayé mane beuguouma am dome mou deuk si métite dou kham loudoul diam, dou kham loudoul nakharo woye Oh! Oh! ni léye, Anye!
 Beuguouma am dome mouye nakharal yayame
 Beuguouma am dome dou mbekté si bayame, li motah sawarouma am dome
 Hi hi hiiiiiiiiiiiiiiiiiiii!
 

Audio Features

Song Details

Duration
05:31
Key
2
Tempo
117 BPM

Share

More Songs by Youssou N'Dour

Albums by Youssou N'Dour

Similar Songs